« Marié depuis 4 mois, je tremble de plaisir, franchement à ce rythme je risque un AVC… »

Partagez sur :

 » Je suis homme et je me suis Marié a peine 4 mois mais franchement depuis nos nuits de noces ba lègui affaire yi dafay gueneu

… « :tarkaala » » dall mon soucis c’est que je suis sportif elle aussi douma may dara mais je risque d’y laisser ma peau déja rien qu’a la voir je tremble de plaisir…mom tamit jamais dèlo avance meme souniou fatigué comme pas possible foumako wo mou wouyou…. Et a ce rythme je risque un AVC walla cardiaque dakh nékh nékh gui dal eupneu sama khol bi dama beugone ay astuces wala conseils pour am controle si mom svp aux hommes sokhla sén conseil torop diko melni kouko guissoul dall…ta nèna li ay lencement rek la ….j’ai tellement peur mais wanoumako ak je veux am contrôle thi mom bagna gawa cédé dall somako guissé rek tago ak sama sago

di grelotté ba khawa rouss sakh. ..nama anciens yi djiapalè way nolen koy geré. «